Channel Avatar

Xalaat TV @UCvKbBbFg7Y7aGiiYY5tXuDQ@youtube.com

1.3M subscribers - no pronouns :c

CrĂ©Ă© en 2015, XALAAT TV est un mĂ©dia d’investigations et d'a


Welcoem to posts!!

in the future - u will be able to do some more stuff here,,,!! like pat catgirl- i mean um yeah... for now u can only see others's posts :c

Xalaat TV
Posted 19 minutes ago

Tey ca "CĂ mbar Hebdo", dinan dalal Sophie Gueye. Dina nu wax ci liggĂ©eyam jaaraleko ci kurĂ©el gi di "Les Racines de l’Espoir", di jĂ ppale xale yu feebar yi, talibĂ© yi ak ñi amul fuñu dĂ«kk.
...
Aujourd’hui dans CĂ mbar Hebdo, nous recevons Sophie Gueye. Nous allons parler de son engagement Ă  travers l’association Les Racines de l’Espoir, qui Ɠuvre en faveur des enfants malades, talibĂ©s et sans-abris.

48 - 2

Xalaat TV
Posted 1 day ago

Tay ci "Lu Xew Tay - Ramadan", dinanu ci dalal Seriñ Cheikhouna Bousso xam-xamam màcc ci mbiri biddiiw. Dinanu waxtane : ndono wu Serigne Mbacké Bousso : diggante xam-xami cosaan ak xam-xam yu sunu jamono jii ».
....
Aujourd'hui dans "Lu Xew Tay - Ramadan", nous recevons Serigne Cheikhouna Bousso, spécialiste en astronomie. ThÚme : "L'héritage astronomique de Serigne Mbacké Bousso : entre savoirs traditionnels et avancées modernes.

1.9K - 25

Xalaat TV
Posted 2 days ago

Alxamis jii ci emisyon bii di « Lu Xew Tay - Ramadan », danuy dalal Imaam Babakar Sylla, jiité « And Sàmm Jikko Yi ». Dinanu waxtaane cër bi imam wara def ci askan wi, lëkkaloo gi am ci diggante politik ak diine, taarix ak jéego yu « And Sàmm Jikko Yi », ak waxtaane yoon wiy tere ngóor-jigéen ci Senegaal.
...
Ce jeudi, dans l'émission « Lu Xew Tay - Ramadan », nous recevons l'Imam Babacar Sylla, coordonnateur de « And Sàmm Jikko Yi ». Nous discutons du rÎle de l'imam dans la communauté, des liens entre politique et religion, de l'histoire et des réalisations de « And Sàmm Jikko Yi », ainsi que de la loi sur la criminalisation de l'homosexualité au Sénégal, entre autres sujets.

2.3K - 14

Xalaat TV
Posted 3 days ago

Dinanu dalal ci "Lu Xew Tay - Ramadan", Mustafaa Sekk di ab gëstukat.
Daanu waxtaane njàngale Mame Cheikh Ibrahima Fall jëm ci ligéey...
...
Aujourd'hui, dans "Lu Xew Tay - Version Ramadan", nous accueillons Moustapha Seck, chercheur et conférencier.
ThĂšme : Culte du travail Ă  travers le modĂšle de Mame Cheikh Ibrahima Fall.

2.7K - 26

Xalaat TV
Posted 4 days ago

« Li Islam wax ci yoriinu xaalisu rĂ©ew » - La gestion des fonds publics vue par l’islam

"Lu Xew Tay" Ramadan : Actualités et Religion (Xew-Xew ak Diiné)

Au programme : Analyse, Une du jour et interview...

Sur Xalaat TV Ă  21h00

Invité : Oustaz Assane Seck

Animation : Sokhna Aminata Diané, Baye Ndongo Fall et Ismaila Seck

2.7K - 13

Xalaat TV
Posted 6 days ago

Tay ci 8 waxtu ci ngoon, dinan dalal Ci "Càmbar Hebdo" Dr Meïssa Ndao, yor kaadu doktër yi amul liggéey wala ñu leen di xañ seeni àqq. Dinan wax ci jafe-jafe wu doktër yu ndaw yi, anam yi ñuy liggéeyee ci hopitaal yi ak saafara yi.
...
Nous recevons aujourd'hui à 20h GMT dans l'émission "Càmbar Hebdo" Dr Meïssa Ndao, porte-parole du mouvement des médecins chÎmeurs ou exploités du Sénégal. Il reviendra sur les difficultés d'insertion des jeunes médecins, les conditions de travail dans les hÎpitaux et les défis de la profession.

2.5K - 10

Xalaat TV
Posted 1 week ago

ENTRETIEN SPECIAL

Tay dinan dalal ci ab "Waxtaan bu yaatu" Moustapha Ndiaye, bokk Pastef ca Mbao té Maire Abdou Karim Sall dàqee ko ci "conseil municipal" bi.
...
Aujourd'hui nous recevons Moustapha Ndiaye, responsable de Pastef à Mbao, récemment révoqué du conseil municipal par le maire Abdou Karim Sal .

2.5K - 5

Xalaat TV
Posted 1 week ago

Tey ci “CĂ mbar Hebdo”, dina nu dalal Ibraahiima Sekk, di yĂ«ngu ci waalu tabax. Dina nu wax ci entreprenariat ci tabax ci Senegaal, jafe-jafe yi am ci entreprise yi, tabax kĂ«r ak diggante kiliyaan yi.

....
Aujourd'hui dans "Càmbar Hebdo", nous recevons Ibrahima Seck, ingénieur en génie civil. Nous parlerons de l'entrepreneuriat dans le BTP au Sénégal, des défis des entreprises locales, de la construction de maisons, des normes de qualité et de la relation client.

3.3K - 19

Xalaat TV
Posted 2 weeks ago

Téy Ci "Càmbar Hebdo" dinanu dalal Paap Abdulaay Turé, di ndoongo jiite kureel gii di SNP (Sénégal Notre Priorité). Dinanu waxtaane tolluwaayu daara yu kawe yi ak pexe yiñ wara def, xibaari politik ak leeral yifi jotoon xew.
...
Aujourd'hui dans l'émission "Càmbar Hebdo", nous accueillons Pape Abdoulaye Touré, étudiant et coordonnateur du mouvement Sénégal Notre Priorité . Au menu : l'état des universités et les solutions envisagées, l'actualité politique ainsi que la reddition des comptes.

4.1K - 12

Xalaat TV
Posted 3 weeks ago

Tey jii, ci emisyon bii di « Ëttu Xalaat », dinan ci dalal Famara Ibraahima CissĂ©, njiital KurĂ©el gi ACIF.
...
Aujourd'hui, dans l'Ă©mission "Ëttu Xalaat", nous avons le plaisir de recevoir Famara Ibrahima CissĂ©, prĂ©sident de l'Association des clients et sociĂ©taires des institutions financiĂšres (ACIF).

2.3K - 18