Touba Xam Xam TV moy daaray Serigne Moustapha Mbacke Istikhama Ibn Serigne Abdou Lahad Ibn Serigne Mourtada Ibn Serigne Touba.
Chaîne Youtube bi Liko taxa djouk moy : 1- Firi Alxourane ci lakk Wolof, 2- Waxtaan ci digënté Alxourane ak science,3- Firi waxi Yonéntébi PSL ci lakk Wolof,4- Waxtaan ci digënté waxi Yonéntébi PSL ak science, 5- Firi mbindoum Serigne Touba ci lakk Wolof, 6- Waxtaan ci lépou lou baax ci wër gu yaram ak waxtaan ci tawat yi mana dal nit ak liy waral tawat yi ndax nga maneko moytou. 7- waxtaan ci théme you fassantoko té am njariñ.
Li moy lien sounou chaîne télégram inchallah dinane fa envoyé mboolém audio Tafsir Alxourane yépou kaamil bi bamou diékh inchallah dina nék Tafsir bou am solo ndax dinane wakhtane ci mboolém sujets scientifique maanaam mboolém mbir yi nga xamné Alxourane waxnako avant 1400 ans science doorkoy wax
t.me/OustazSerigneMoustaphaListikhama