Channel Avatar

Suñu Xassida Tv @UCMoUtakgO0tG3Gz-ZZ2k1IQ@youtube.com

25K subscribers - no pronouns :c

Karaamatii xatu yadii


Welcoem to posts!!

in the future - u will be able to do some more stuff here,,,!! like pat catgirl- i mean um yeah... for now u can only see others's posts :c

Suñu Xassida Tv
Posted 1 day ago

Tay ci Talaata gi mooy ñaar fukki fane ak bénn (21) ci weeru Maamu Koor (Jumaada Saanii) 1446H dëppo ak 24 Décembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Alarba gi mooy fukki fane (10) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 13 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

3 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Talaata gi mooy juroom ñenti fane (9) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 12 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Altine gi mooy juroom ñetti fane (8)ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 11 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Dibéer gi mooy juroom ñaari fane (7) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 10 Novembre

Yalna Yàlla def jàmm

3 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Gaawu gi mooy juroom benni fane (6) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 9 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Àjjuma gi mooy juroomi fane (05) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 08 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Àjjuma gi mooy juroomi fane (05) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 08 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Alxamis gi mooy ñenti fane (04) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 07 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0

Suñu Xassida Tv
Posted 1 month ago

Tay ci Alarba gi mooy ñetti fane (03) ci weeru Rakkaati Gàmmu (Jumaadal Uulaa) 1446H dëppo ak 06 Novembre

Yalna Yàlla defal ñépp jàmm

2 - 0